Jump to content

Help:Soppi xët yi

From mediawiki.org
This page is a translated version of the page Help:Editing pages and the translation is 73% complete.
Outdated translations are marked like this.
PD Karmat:Soo soppee wii xët, nangu nga ne yaa ngi joxe say cëru ci anam yi CC0 tëral. Xoolal Xëtu ndimbal wu Public Domain ngir yeneeni xibaar. PD

Tekki ëmbéefu ab wiki lu yomb la:

  1. Bësal ci làccu xët wi "Soppi" wi nekk ci kaw xët wi.
  2. Amalal say coppite ci mbind mi.
  3. Bësal ci bësu bi "Wattu xët wi".

Nii la yombe!

Sarti Coppite gi, Déeggooy Coppite gi ak melokaanal

Sàrt bi njëkk ci soppi ab wiki mooy bul ragal. Wéyal - soppil. yeneen nit di nañ jubanti njuumte yi ngay def, kon jéemal te bul ragal! Xeeti Déeggoo yu nekk am nañ fi, ay sàrt aki gisiin ci nees di soppee aw xëtu wiki, waaye sàrtu bul ragal mooy bi ëpp solo ci yépp!

Ab coppite man naa doon xise bu bees bu mat walla xët wu bees, man a doon it kepp ab jubantib mbindiin. Ci lu-daj, deel jéem di yokk walla di soppi am mbind ngir mu gën a leer te dàttu. Li gën a te am-solo mooy jéem di yokk ci ëmbéefu wiki bi lu koy gënal.

Soo nammee jëfandikoo yenn xeeti melokaanal, niki ay koj yu bees walla dijjal am mbind, man nga ko ci jëfandikoo mbidiinu wiki bi walla bësu yi ci bànqaasu jumtukaayi soppi gi, féete ca kaw soppiwaay ba. See Help:Formatting for some of the common types of formatting used.

If you want to try out editing, you can test editing on the page named Project:Sandbox , which has been specifically set aside for you to test editing.

Tënkug coppite gi

Laataa ngay denc aw xët, man ngaa duggal karmat gu gàtt ci boyot bu "Tënk :", tënk fa say coppite. Don't worry too much about this, or spend too much time thinking about it: just put in a short description of what you just changed. For example, you might say "fixed typo" or "added more information about sunflowers".

Tënk gi dees koy denc ci wetu sa coppite, di tax nit ñi man di topp coppite yi ci wiki bi ci ni mu gënee.

Wonendi

Doon na lu baax di jëfandikoo bësu bu "Wonendi" ngir gis ni say coppite di meliji ginnaaw boo leen dencee. Loolu it ñeel na topp coppite yi ndax saa yoo dencee say coppite, ñeneen ñi dañ koy gis niki coppite gu bees, gu tàqalikoo ak yeneen yi. Doonul luy war di nekk sa xel di la ëlam, waaye doon na baax nga koy jëfandikoo ngir man di jubanti njuumte yi ci say mbind laataa nga leen di denc. Lu ko moy dangay nekk di soppeek soppiwaat wenn xët wi ngir jubanti mbind yi nga duggaloon.

Woneeg coppite yi

Man nga itam jëfandikoo bësu bu "Wone samay soppi" biy tax nga man di gis wuute yi ci sumb bu teew beek bi ngay soppi.

Protected pages

Pages that are protected cannot be edited by anyone except users of a specific group. Protected pages will instead display "View source" instead of edit. In that case, to edit a protected page, contact a user who has permission to edit the page. The default protection levels are as follows:

  • None (allow all users)
  • Autoconfirmed (prevent edits by new and unregistered users)
  • Sysop (prevent edits by all users except administrators)

Yeneen soppiwiin

Ak coppite yu wiki man ngaa tàmbli xët wu bees, topple (walla tuddewaat) walla sax far aw xët:

Fàttlikul ne sa yéene mooy gënal ëmbéefu wiki bi ak say coppite.

Waxtaan

Jukki bu nekk am an xëtu waxtaanuwaay fooy man di defey laaj, joxey xalaat walla waxtaaney beqi. Xoolal Help:Xëti waxtaanuwaay .